Kàggu Gi

Kàggu Gi. Xam Xam bu woor jelé ko ci Alxuraan, sunna ak jàngale mag ñi.

inchaAllah dinane fi wonne bindu mag ñi ci xassida ak wolofal, ay waxtaan yu am solo ci alxuraan ak sunna, dinane fi jàngale làkku araab, ak bepp xam xam bu ab jullit yitte woo ci wallu diineem ak luko ñogal.

Jokko ak ñun ci loo soxla ci fànn yi ñu lim. Dinane taxawu kem sunu kàttan inchaAllah.

Bul fàtte abonner ci chaîne bi t wasaare ko, nguir ñepp jot ci Kàggu gi.

Wolofal, khassaides, khassida, xam xam, Serigne Moussa Ka, jangle araab, jàng arabe, mag ñi, jàngale mag ñi l.

#Islam, #Sunnah, #SerigneTouba, #Sokhna_Diarra, #Khassida, #Khassaides, #KurelHT, #Hizbou_Tarqiyah, #Serigne_Moussa_Ka, #Serigne_Mbaye_Diakhate, #Akassa_Samb, #Khadim_Gueye, #Ibra_Gueye, #Moustapha_Gningue, #Journée_Khassaides, #Baye_Khaly_seye,
#Rajaz_Kazu_Rajab, #RafahTV, #DarouMinaneTV, #ToubaTV, #AlMouridiyyah,