Maitre Maimouna Tv

As-salamu alaykum wa rahmatullah. Bienvenue sur Maitre Maimouna Tv, la chaîne de référence pour le mariage (sey) au Sénégal.

Ci chaîne bi, di nañu waxtaane lépp lu jëm ci sey, njaboot, ak jikko. Suñu mission mooy jàppale couples yi, bu ñuy waaj a sëy walla ñu sëy ba noppi, ngir ñu am kër gu neex, gu am jàmm, te sàkku ngërëmu Yàlla. Di nañ fey joxe ay conseils pratiques ci vie de couple, naka lañuy dépassé ay difficultés, ak li lislaam wax ci sey.

Rejoignez notre communauté pour des conseils sur l'amour, la famille, et une vie de couple épanouie.

Pour tout contact professionnel : [email protected]

Abonnel te bësal cloche bi ngir manu ko benn waxtaan! Jërëjëf!