DMAT TV
Bienvenue sur la chaîne DAARA MUQÀDDAMAATUL AMDAAH Thiès , consacrée à la diffusion et à la divulgation du message de Khâdimu-r-Rasûl, ainsi qu'à l'expansion du mouridisme dans le monde numérique. Notre objectif est de promouvoir les enseignements de Khâdimu-r-Rasûl à l'échelle mondiale.
Abonnez-vous gratuitement à notre chaîne YouTube et activez la cloche pour suivre en direct tous les grands événements de l'Islam et de la Mouridiyyah.
Dalal ak jàmm ci dalub DAARA MUQÀDDIMAATUL AMDAAH THIÈS, li ko taxa jokk yaatal ak tasaare jàngaleem XAADIM RASÓOL, ak lépp lu aju ci yoonu muride jare ci xarala yu yees, sunu jubluwaay mooy wanee jàngalem Sëriñ bi ba mu yaatu fépp ci àddina si.
Mën ngaa bokk ci dal bi ci ludul ngay fay dara te nga taal yëglekaay gi ngir di topp sunu ay daar-daar ak bés yu mak yépp ci Islam ak yoonu Muride.
WAXTAAN WU AM SOLO, S. XAADIM SAAW
KARAMNAA S.CISSE K1 DMA
SINDIIDI DAARA MAWAAHIBUL XUDDOS
Mawaahibu complet K1 DMA guddi ajjuma 13/11/2025
🛑Annonce: Delloo njukkal ak sargal S.Mustafaa Jaxate Xaadimul Xadiim
SERIGNE ABO GUEYE, Njàng mu wër te yéeme lool 😭
Mafaatihul jinaan complét K1 DMA Guddi Ajuma 06/11/2025
Cëy njàng mu neex waay. S Ablaay Sekk
Xutba bu am solo ci wax ludul dëgg, 07/11/2025/ Imaam Musaa Wàdd
Sàmm àqi dëkkandoo...Xutba àjjuma . Imaam Musaa Wadd le 31/10/25
Extrait Raaiya et Bouchra par serigne Ahmadou Gueye khassida
Xutba àjjuma. 24/10/25 Imaam S. Fàllu Buso, ndénkaane li yonnennti ndénk, xeet wi.
Kàdduy S. Seex Ahmadu Bamba Ture Ziaar DMA
Sëriñ Xaadim caam mu Sëriñ Saaliw Ture ziyaar DMA.......
Ziaar DAARA MUQÀDAMAATUL ADAAH au prés de S.S AHMADU BABA TURE, représentant Xalif général des Murid
Tontul S MURTADAA TURE jëm ci ñiy wax naan mbindum sëriñ bi dafa.......
WAX LUDUL DËGG....... XUTBA AJJUMA Le 17/10/2025, Imaam Mussa Wàdd
MUQADDAMAAT COMPLET K1 DMA THIES
XUTBA AJJUMA 10/10 2025 PARTIE 1 JUMAAY S MURTADAA IMAAM MUSSAA WADD
S MAAM MOOR SUGU GUDDI AJJUMA DMA
Xutba ajjuma 10 /10 /2025 PARTIE 1 JUMAAY S MURTADAA IMAAM MUSSA WAD
S Ibrahima Gueye jàng mu yéeme,,,,😭😭😭😭...
TAWBATUN NASUUH K1 DMA
XUTBA AJJUMA Grande Thies jumaay S Murtadaa/ Imaam Mussa Wad/ 03/10/2025
GÀMMU 2025 DAKAR SICAP DARABIS, Kër Sëriñ Seex Awa Bàlla....
kaaduy soññee yu am solo naka la nu mëna dimbalee.😭 Sëriñ Seex Ture mum Sëriñ Saaliwu Ture .B GALAS
Waxtaan wu am solo ak Cherif Alwali.....
yóbb Reeru gàmmu à jakay murit ci Sëriñ Seex Ture Xalifa Sëriñ Saaliwu Ture DMA
Waxtaan wu am solo Sëñ Maam Cerno Daarul Manaan." kuci bàyyi wul limay bañ di na ñaan." (gàmmu 2024)
GÀMMU 2024 DAKAR SICAP DARABIS KËR SËRIÑ SEEX AWA BÀLLA MBÀKKE