Sadik'Def - Feulalé (Clip Officiel)
Автор: JT Rappé
Загружено: 2021-09-10
Просмотров: 6123
** Abonnez-vous au JTR ici https://goo.gl/nhtjbS **
** Pour écouter FEULALÉ, clique ici https://bfan.link/feulale **
Sadik’Def nous livre aujourd’hui son 2ème clip : FEULALÉ
Rappeur originaire de Richard Toll où il a débuté sa carrière, il évolue actuellement à Dakar et réside à Grand Yoff . FEULALÉ est sa présentation "officielle" dans le Game : il y parle de ses ambitions de conquête, prêt à terrasser tout ce qui se dresse sur son chemin.
#SadikDef #Feulalé #ClipOfficiel #rap #hiphop #jtr #xuman #nattydread #team221
** Pour écouter FEULALÉ, clique ici https://bfan.link/feulale **
** Crédits de la chanson & du clip FEULALÉ **
Musique : ZOOM on da BEAT
Mix/Mastering : SIRR KHALIFA
Réalisation : RIDMOU
Montage clip : SADIK’DEF
D.A : ALEX DA BOY
Assistant Réalisation : ASS PAYE
Coiffure/Make up : NDELLA - SALLY (SCAD URBAM 1)
Étalonnage : TAPHA NDONGO
Administration digital : SOON
Régie : BABACAR SECK
Assistant réégie : MED RICHBOY
Making Of : BIG LAYE
Chargé de prod : XUMAN (Natty Dread Edutainment, Dakar, Senegal)
** Pour écouter FEULALÉ, clique ici https://bfan.link/feulale **
** Lyrics de la chanson FEULALÉ **
COUPLET 1
BI NGAY RAP , MAGUI TOOK SI POTE
TÉ DARA DOU TÉ , MALAYE TATE SI PÉT
NI DIANDIA BI LEP LAY TEK SI COTE
TÉ GUISSOUGOUMA KOULA GUENA YESS
NGAMAYE SAF COMEDIEN TIK TOK
FAKE NIGGAH CHAGÉL SA DJIKO
DO BIG BOSS ,
FI NGA TEGONE SA BOP DÉ NÉKOFA
FÉKHÉ NGA MOEUNO SI MANE GATE
DI PERCU TÉ AMO SAX MANDAT
DIANDIA LA XAWMA LOUY MAR TATE
BAKHALO DEM ,DAGA DONE SAFF
MEUNO BÉNGAL BEUGUEU DAKHAR
SADIK BI TASSNA SA YAKAR
BOY DAMAYE BENEU BENEU BAMOU SAKHAR
PREREF
YAW BODÉ DIANDIA LOUN SI DEF
MAGUÉK SA PAPA ZOOM SAMA WÉTT
YÉH YÉH
YAW BODÉ DIANDIA LOUN SI DEF
MAGUÉK SA PAPA ZOOM SAMA WÉTT
YÉÉÉÉÉH
REFRAIN
DÉL SORALÉ NAKOY SORALÉ
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
NAKOY SORALÉ
DOMA TÉRÉ FEULALÉ
AY AY
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
DÉL SORALÉ NAKOY SORALÉ
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
COUPLET 2
TABAKH SAMA LIFE SANS BRICK
TOTHI SÉN KOGNE SANS GRILLE
NIOU TOL NI SA MAME LAYE IRI
FINAYE FAR NGAYE ZIRIK
FEULALÉ NAKOY SORALÉ
FI GUA BEUGUE FOFOU LA NÉK
NAKOY SORALÉ DAMA TÉRÉ NDAYOU
FEULALÉ
NDANI YAFI GUEUNA WAGUA
NDAKH KHAM NGA SA FEBAROU TATE LEU
MASSOUMA GUISSE RAPPEUR YOU BEUGEU
BUZZ NI TRADIPRATITIEN
AUTO MBALITE DIOUNI RAPPEUR SI NIOM
LEU RESTE MA DEF KO DESSÉR
NII NIO NGUI XANDIO DIÉL
NII NIO NGUI XADIO DJIZ
XAMNANI YOROULÉNE XÉR
MÉ RAP BO LOU FAYE AYEAY BRICK
PREREF
YAW BODÉ DIANDIA LOUN SI DEF
MAGUÉK SA PAPA ZOOM SAMA WÉTT
YÉH YÉH
YAW BODÉ DIANDIA LOUN SI DEF
MAGUÉK SA PAPA ZOOM SAMA WÉTT
YÉÉÉÉÉH
REFRAIN
DÉL SORALÉ NAKOY SORALÉ
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
NAKOY SORALÉ
DOMA TÉRÉ FEULALÉ
AY AY
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
DÉL SORALÉ NAKOY SORALÉ
FI NGA BEUGEU DEM FOFOU LA NÉK
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео mp4
-
Информация по загрузке: